Njuga Gay

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (9/12/2024)

NDAJEM DOHAA MI Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay teeweji woon na Ndajem...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA QATAAR

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, ma nga tay fa réewum Qataar....

NDAJEM JËWRIÑ YI

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jiite na ndajem jëwriñ yi barki-démb...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/12/2024)

CAAROY 44 : NJIITU RÉEW MI JËL NAY NDOGAL Barki-démb ci dibéer ji lañu doon màggal...

CAAROY 44

Ëllëg ci dibéer ji, 1 fan ci weeru desàmbar, dinañu màggal fi Senegaal bésub...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/11/2024)

NJËGU GERTE GI  Càmm gi siiwal na njëgu gerte gi. Tay, ci ndajem jewriñ mees...

CPI JÁPPLU NA BENYAMIN NETANYAHOU

Ëttu àttewaay bii di CPI (Cour Pénale Internationale, fa mbaxana doone benn fi àddina...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (18/11/2024)

WOTE YI Limu wotekat yi bindu ci këyitu wote gi mi ngi tollu ci 7 300 000iy...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA