Njuga Gay

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

8eelu BËCCËGUB SETAL SUNU RÉEW

Tay ci gaawu bi, 4i pani desàmbar 2024, doon nañu tóllanteeti « Bëccëgub setal sunu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/12/2024)

ÑOO NGI JAAY JUMTUKAAYI 7TV Ci benn saabaalukaay lees biral xibaaru njaayum jumtukaayi tele bii...

NGOMBLAAN GI : TAXAWAL NAÑU ËTTU ÀTTEKAAY BU KAWE BI

Ngomblaan gi taxawal na Ëttu àttewaay bu kawe bi. Tay ci gaawu bi, 28i...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (23/12/2024)

NJÀNG MI : SEYDI GASAMA ÀNDUL AK JËWRIÑ JI Xale yees yéex a bind ci...

MÀGGALUG BÉSUB JÀNGALEKAT YI

Jëwriñu njàngale mu kawe mi, gëstu beek coste bi màggal na bàrki-démb ci alxames...

NDÀMPAAY ÑEEL WAY-LORUY XEW-XEWI 2021 JÀPP 2024

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, beral na way-loruy xew-xewi 2021 jàpp...

CEDEAO : CAMPEEF GI NANGU NA GÉNNUG BURKINAA, MALI ET NISEER

Ca weeru sulet 2024 la ñetti réew yii di Burkinaa Faaso, Mali ak Niseer...

5eelu NDAJE MU MAG MU COSYDEP

Kurélug COSYDEP (Coalition des Organisations en Synergie pour la Défense de l’Éducation) amal na...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA