Njuga Gay

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

LU GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/6/2024)

WÉR-GI-YARAM Kurél gii di ànd gësëm, di kurélug waa kër doktoor, àddooti na. Wile yoon...

“ICS” FEEÑLE NA

Ginnaaw riirum caabal yi ci yorinu alalu askan wi, coow topp na kër gii...

GÀTTALI BÉS BI (4/6/2024)

ISRAAYEL RAY NA CI WAA PALASTIIN LU ËPP 15 000iy GONE Bees sukkandikoo ci tele...

NDOGAL YU YEES ÑEEL NJÀNG MU KOWE MI

Abdurahmaan Juuf, jëwriñu njàng mu kowe mi, gëstu geek coste gi, biral na njureef...

LËLUB NJÀNG MU KOWE MI ÑEEL BAAXAL APPUG NJANGALE MI

Kilifa yi séq njàng mu kowe mi ubbi nañu lëlub ñetti fan. Ñu namm...

FIARA 2024

Fiara (Foire internationale de l’agriculture et des ressources animales) bu 2024 bee ngi ñuy...

MBIRI BAA JAXATE AK IMAAM NDAW

Tey ci altine ji la Baa Jaxate ak Imaam Séex TIijaan Ndaw doon janook...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA PARAAYAA AK KONAAKIRI

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA PARAAYAA AK KONAAKIRI Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA