Njuga Gay

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/12/2024)

LIGGÉEY BA DOOR NA FA NGOMBLAAN GA Altine jii weesu lañu ubbi fukk ak juróomeelu moomeg Ngomblaan gi, fal mbooleem ñi ñu war a fal ca béréb ba. Mu mel ni dépitey Ngomblaan gii amuñu toogaay. Nde, démb, ci àllarba ji la ki fi nekkoon...

NDAJEM JËWRIÑ YI

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jiite na ndajem jëwriñ yi barki-démb ci talaata ji. Ginnaaw bi mu defaree coppite yi am ci Càmm gi, dellu na ñaaxaat jëwriñ yi ñu farlu ci mbir yi gën a tembare, rawatina mbir yi ñeel...

Séex Bàmba Jéey : “Ndawi Senegaal tey, ku jàpp ni ndaw yu amul jëmu lañu […]. Yow yaa juum.”

Ginnaaw ñaari ati kaso yi àtte bi daan kii di Usmaan Sonko ak kii...

YËNGU-YËNGUY RÉEW MI : JÀNGUNE YAA NGIY TËJ

Juróom-ñeenti bakkan ci alxames ji, fukk ak ñett ci àjjuma ji, muy ñaar-fukk ak...

25 me 1963 – 25 me 2023 : 60i at ginnaaw juddug OUA

Keroog ci Alxames ji, 25 me 2023, la mboolooy Saa-Afrig yi doon màggal bés...

Usmaan Sonko dina dellu Ndakaaru

Njiitul Pastef li, Usmaan Sonko, dina dellu Ndakaaru. Tey ci àllarba ji la ko...

Mbirum Sweet Beauty : ni Ndey Xadi Njaay setal na boppam, taqal Aji Raabi Saar

Tey, ci talaata ji 23 me 2023 lees di amal layoob Usmaan Sonko ak...

XEWTEEB NDAAKAARU ÑEEL LADAB CI ÀDDINA SI

Ndakaaru dina amal ñaareelu xewteem ñeel ladab ci àddina si, FILID (Festival international de...

Màggalug téeméereelu Usmaan Sémbeen

Usmaan Sémbeen doon na am téeméeri at ci ren, bu fekkoon muy dund. Jànguneb...

DEGGOO BU YEES DIGGANTE SENEGAAL AK FMI

Nguurug Senegaal ak FMI (Font monétaire International), di mbootaay miy saytu kopparu réewi àddina...

XËT YI MUJJ

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/12/2024)

LIGGÉEY BA DOOR NA FA NGOMBLAAN GA Altine jii weesu lañu ubbi fukk ak juróomeelu...

NDAJEM JËWRIÑ YI

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jiite na ndajem jëwriñ yi barki-démb...

DÉPITEY FARÃS YI DAANEEL NAÑU CÀMMUG MICHEL BARNIER

Dépitey Ngomblaanu Farãs yi wote nañu pasum diiŋat (motion de censure), daldi daaneel Càmmug...

ÀMBURUWAAS SAAR : AATU RÉER NA !

Njabootu làmbu Senegaal ak mbatiit am nañu dëj. Nde, xibaaru tiis ak uw naqar...