Njuga Gay

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

NDAJEM JËWRIÑI AFRIG YI ÑEEL NDOX MI

Doon nañu amal ci altiney barki-démb ji, 6eelu ndaje mu mag mu ndisoog AMCOW...

YOON A NGI CI TÀNKI MAKI SÀLL

Maki Sàll mi fi nekkoon Njiitu Réewum Senegaal diggante atum 2012 jàpp 2024, dina...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (26/2/2025)

NDAJEM NJIITI RÉEWI AFRIG YA WOON Ay kilifa yu nekkoon i Njiiti Réew fi kembaarug...

BÉS BI ÑU JAGLEEL JUR GI FI RÉEW MI

Démb ci gaawu bi, 22i fani féewirye, lañu doon màggal bés bi ñu jagleel...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/2/2025)

SOROJU SANGOMAAR BI Bilaŋub sàngomaar bu atum 2024 mi génn na. Waa Woodside ñoo ko...

38EELU NDAJEM BENNOOG AFRIG (UA)

38eelu ndajem Bennog Afrig (Union Africaine) mee ngi ñuy amal jamono yii fa Ecopi....

LËKKATOOG KAARAANGE DIGGANTE SENEGAAL AK MALI

Ginnaaw bi ñu xaatimee woon ab déggoo ci fànnu kaaraange ca atum 2021, réewum...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/2/2025)

SÉMBUW JOTALE DËKKI KOW YI AK NDOX MU SELL Nguur gi seqi na ñaareelu jéego...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA