Paap Aali Jàllo

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

NDAJEM JËWRIÑ YI (13/3/2025)

Nees ko tàmm a defe, ayu-bés bu jot, amal nañu ndajem jëwriñ yi démb...

DÉGGOOB YOON DIGGANTE SENEGAAL AK MAROG : DÉPITE YI JÀLLALE NAÑU SÉMBU ÀTTE WI

Ci talaatay démb ji la Ngomblaan gi doon fénc sémbuw àtte ñeel Déggoob Yoon...

SOGEPA MI NGI CI YOONU NANGU KËRI NGUUR GI

Lu ëpp juróom-fukki njaboot la SOGEPA nar a génne ciy kër yoy, moomeelu Nguur...

NDAJEM JËWRIÑ YI (5/3/2025)

Démb ci àllarba ji, 5 màrs 2025, amal nañu ndajem jëwriñ mees di faral...

SÉMBUW KOPPEY MBAY ÑEEL NJABOOTU DAARA

Jëwriñu Mbay mi, Dund gu doy gi ak Càmm gi, Sëñ Mabuuba Jaañ, yégle...

MAKI SÀLL : « RAGALUMA DARA. NAÑU MA TOPP BU LEEN NEEXEE… »

Maki Sàll tëkku na njiiti Senegaal yu yees yi. Moom, Njiitu réew ma woon,...

FARBA NGOM DEM NA KASO

Farba Ngom dem na kaso. Tay ci alxemes ji, 27 féewiryee 2025, la ko...

MOODY’S WÀCCEE NA NATTUB SENEGAAL

Moody’s Investors ag kurél la guy natt réewi àddina si ci wàllu kopparal. Bees...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA