Facebook
Instagram
TikTok
Twitter
Ëtt bi
COKKAASU ODIA
MAGU WAXOON NAA KO
FÀTTALIKU DÉMB
WAXLEEN SEEN XALAAT
Xibaar
Bàyyi ci xel
Bindkatu ayubés bi
Diine
Gis-Gis
Kii Kumu
Koom-koom
Pólitig
Tàggat-yaram
Recherche
Ëtt bi
COKKAASU ODIA
MAGU WAXOON NAA KO
FÀTTALIKU DÉMB
WAXLEEN SEEN XALAAT
Xibaar
Bàyyi ci xel
Bindkatu ayubés bi
Diine
Gis-Gis
Kii Kumu
Koom-koom
Pólitig
Tàggat-yaram
Li des
Accueil
Auteurs
Articles postés par Paap Aali Jàllo
Paap Aali Jàllo
Li fës
BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI
Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...
17/12/2025
Li fës
COKKAASU ODIA
15/12/2025
VOA AMAL NAB JOTAAY CI MBINDUM BUBAKAR BÓRIS JÓOB GINNAAW BI WEREKAAN BI JËLEE CARGALUG NEUSTADT 2022 BI. CUQAL CI LËNKAAY BII TOFTALU...
00:19:36
Jotaayu xam-xam ak Sën Abdu Xaadir Kebe
00:03:10
“Slam” Maysa Maara
00:15:20
Li Abdu Lahaat Ka wax ci wolof
Xibaar
Me MUSAA SAAR MËNUL GIS ANIBAAL JIIM
Jamono jii, mbokki Muhammet Sàmba mees duppee Anibaal Jiim yaa ngi ci njàqare ju...
14/08/2023
Li fës
KUMBA AM NDEY, KUMBA AMUL NDEY
Démb lañ bàyyi Xuwaan Baranko (Juan Branco), yóbbu ko ca saa sa fa dalub...
08/08/2023
Li fës
RAWALEES NA USMAAN SONKO CA FAJUWAAY BA
Làngug Pastef les Patriotes génne na ab yégle di ci xamle ne, rawalees na...
06/08/2023
Li fës
JÀPPATI NAÑ USMAAN SONKO
Fan yii weesu lañ ñàggi kër Usmaan Sonko ginnaaw 55i fan. Ñu yaakaaroon ne...
28/07/2023
Li fës
BIBO BOURGI TOROXAL NA NGUURUG SENEGAAL
Gàcce bu reyul, semmal. Nguurug Senegaal a ngi ne tott ci kanamu àddina sépp....
21/07/2023
Xibaar
TAMXARIT 2023
Àjjuma 28 sulet 2023 mooy doon bésu tamxarit. Loolu la waa CMS, Ndajem Julliti...
19/07/2023
Li fës
SÉMBUB ÀTTE BUY SOPPI DOGUB 87 BI
Ëllëg, ci altine ji 16 sulet 2023, lañ war a wote ca Ngomblaan ga...
16/07/2023
Li fës
« RAŊ ! RAŊ ! KEŊ ! KEŊ ! … » NDAKAARU RIIR NA DÉMB
Bool, marmet, kubéeri cin, kuddu cinwaar, kuddu luus, mbiib yi, korne yi… lépp a...
16/07/2023
1
...
34
35
36
...
54
Page 35 sur 54
XËT YI MUJJ
Li fës
BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI
Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...
17/12/2025
Li fës
COKKAASU ODIA
15/12/2025
Li fës
BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO
Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...
15/12/2025
Li fës
COKKAASU ODIA
08/12/2025