Paap Aali Jàllo

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

REY NAÑU BAABA KAANA RÀPPËER

Jot nan xibaar buy wax ne, ràppëer bii di Abdulaay Kamara, ñu gën ko...

BUBAKAR BÓRIS JÓOB, BINDKAT : “KENN WARUL A ÑÉDD NGUUR BA SAY BAARAAM DI NÀCC.”

Seen yéenekaayu web, Lu Defu Waxu, amal nab laaj-tontu bu yaatu ak werekaan bii...

ANTUWAAN F. JOM : « JURÓOM-ÑEENTI BAKKAN ROT NAÑU DIGGANTE NDAKAARU AK SIGICOOR. »

Démb, ci guddig alxames ji, jëwriñu biir réew mi doon janook taskati xibaar yi,...

ANTUWAAN F. JOM : « NGUURUG SENEGAAL, CI FULLAAY BOPPAM, MOO JËL NDOGALU DOGANDI NJOKKOO GI… »

Démb, ci guddig alxames ji, mbaali-jokkoo yi, WhatsApp, Facebook, Twitter, Telegram, Youtube, benn doxi...

YEWWI ASKAN WI : « MAKI SÀLL DAFA WOR BA FU WOR YEM. »

Lëkkatoo Yewwi Askan Wi génne na ab yégle ñeel tolluwaayu réew mi. Dañu bind...

Ismayla Maajoor Faal : « Mën nañ jàpp Usmaan Sonko saa su nekk. »

Ginnaaw bi àtte bi jibee, ñu daan Usmaan Sonko 2i ati kaso yim war...

ÀTTEKAT BI DAAN NA USMAAN SONKO AK NDEY XADI NJAAY 2I ATI KASO YI ÑUY TËDD

Ñaari ati kaso yu Usmaan Sonko war a tëdd ak ñaari ati kaso yu Ndey Xadi...

USMAAN SONKO FEEÑ NA

Lees doon njort moo am : takk-der yaa jàppoon, ndeke, Usmaan Sonko. Fim ne...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA