Paap Aali Jàllo

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

FU USMAAN SONKO RÉER ?

Kenn xamul fu Usmaan Sonko nekk jamono jii. Bentaleb Sow ak Juan Branco, layookatu...

YEWWI ASKAN WI – TAXAWU SENEGAAL : ÀND BUY WAAJ A TAS ?

Waxtaanu Maki Sàll wi de, boo demee, moo nar a génne Taxawu Senegaal ci...

BAANE, YAA WAANE !

Dàqees na àtte bi ba alxames, 1 fan ci suwe 2023. Démb ci talaata...

USMAAN SONKO : « Bu Maki bëggee jàpp Usmaan Sonko, fàww mu taqal boppam»

Démb, ci guddig àjjuma ji, Usmaan Sonko séq naak Piyeer Eduwaar Fay mu Walf...

SIGICOOR : BENN TAKK-DER ÑÀKK NA BAKKANAM

Xeex bu mettee am ca Sigicoor diggante ndaw ñiy taxawu Usmaan Sonko ak takk-der...

F24 : WENN SAY, GENN KÀDDU

Démb ci àjjuma ji, ginnaaw julli jumaa, la waa F24 woote woon fa «...

SONKO-BÀRT : YÀGG BAWUL DARA (1/2)

Cin bax na, waaye du jikkoom, matt a ko ca jóo. Altine ba tey,...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA