Paap Aali Jàllo

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ-USMAAN SONKO : DIG-DAJE 8 ME 2023

Ci altiney tey jii, 17 awril 2023, la layoob "Appel" bi ñeel Maam Mbay...

XARE CA SUDà

Xeex bu mettee jolli Sudã, diggante làrme beek i sóobare yu beddeeku. Ñaari seneraal...

YANQOOBA JATARA DAY TEKKI NDOMBOG-TÀNKAM

Lees doon xaar jib na : Yanqooba Jatara, jëwriñu tàggat-yaram gi, génn na pàrti...

COOWAL NAPPKATI KAYAAR YEEK YU MBOORO YI

Géej gi sàmbaraax na. Bakkan bu rot, 22i nit ñu amey gaañu-gaañu, ñaar ñu...

MAAM MBAY ÑAŊ : ” SONKO RËCCAGUL. “

Maam Mbay Ñaŋ nee na day def "appel", du bàyyi mu sedd. Moom, ak...

LAYOO USMAAN SONKO – MAAM MBAY ÑAŊ

Àttekat bi daan na Usmaan Sonko ñaari weer yum dul tëdd kaso ak 200i...

ÑAAW NA BA NOPPI

Paap Aliyun Saar a doon dalal Bubakar Bóris Jóob ca ITV. Tolluwaayu réew mi...

JÀPP NAÑU DR BAABAKAR ÑAŊ, BOROOM KILINIG SUMA ASSISTANCE

Sàndarm yi jàpp nañu fajkat bii di doktoor Baabakar Ñaŋ miy boroom kilinig Suma...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA