Paap Aali Jàllo

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

TATA MIMI COKKAAS NA MAKI SÀLL

Dige bor la. Wolof a ko wax. Moo tax, Aminata Ture dëggal na digeem...

SENEGAAL 2 – BOLIWII 0

Ekibu nasiyonalu Senegaal bu futbal a ngi ci waajtaayu Kub di mond bi war...

MAKI, AMAL SUNU KERSA WAAY !

Ci ngoon gi, boori 16i waxtu, la RTS rotal xibaar bi : « bu...

PEKKUG NGOMBLAAN GU BEES GI

Ci talaatay démb ji, li ko dale 11i waxtu ci yoor-yoor bi, lees doon...

Na woon, fa woon

Ci bëccëgu altiney ji, 12 ut 2022, la Senegaal doon taxawal 14eelu ngombalaanam (péncum...

MAMADU BAAJO KAMARA, LOO NAR ?

Léegi, xam nañ kan mooy wuutu Paap Umar Saaxo mi dem alaaterete. Ci dekkareb...

LI GËN A FËS CI XIBAARI

LÀMB : Bàlla Gay 2 daanaat na Giri-Bórdoo  Ci diibéerub démb ji la Gastõ Mbeng...

NJUREEFI NÉGANDI YU WOTEY NGOMBLAAN GI, lu mu nar a jur ?

Décce Faal ak i ñoñam, waa Wallu-Yewwi, dinañu am lu leen metti. Te, sikk...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA