Li fës

« USMAAN SONKO NEE NA YËGATUL WETU CÀMMOOÑAM… »

Xadi Kebe ak Aana Jamanka, ñaari soxnay Usmaan Sonko yi, doon nañ amal ab...

BITIM-RÉEW : LAYOOKATI USMAAN SONKO YI TÀMBALI NAÑU XEEX BI

Ni ñu ko waxee woon lañu ko defe. Layookati Usmaan Sonko yi yóbbu nañu...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (18/8/2023)

WÉR-GI-YARAMI ÑI ÑU JÀPP CI KASO YI Kilifay caytug kasoy Senegaal yi génne nañu ab...

Rawale nañ Usmaan Sonko ca “réanimation” ba.

Rawale nañ Usmaan Sonko ca "réanimation" ba. Jotna Média moo siiwal xibaar bi. Ci...

CEDEAO-NISEER

Fitna jaa ngi gën dee jege ci diggante Niseer ak CEDEAO. Ginnaaw bi kurél...

YOKKUTEG NJËGU SOBLE SI

Am soble nekk na lu jafe lool fi mu tollu nii ci biir réew...

ÀQ AK YELLEEFI DOOM-AADAMA : SENEGAAL DAFA GËN A DELLU GINNAAW

Senegaal mi ngi ci guuta. Loolu la kurél yiy sàmm àq ak yelleefi doom-aadama...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...