Li fës

SËRIÑ MUSTAFAA SI ÀDDU NA CI TOLLUWAAYU RÉEW MI

Sëriñ Mustafaa Si joxe na gis-gisam ci tolluwaayu réew mi, rawatina yëngu-yëngal yi fi...

UBBITEB LIGGÉEY YI ÑEEL PÉNCOOM RÉEW MI

Àllarba, 31 me 2023, la Njiitu réew mi Maki Sàll woote woon ubbite péncoo...

AJI SAAR SÀKKU NA ÀTTEB DABU

Alxames 1 fan ci weeru suwe la àttekat bi biraloon daan yim gàll Usmaan...

GÀTTALI BÉS BI

4i néew yiñ yóbbu ci raglub Dalal Jàmm Ginnaaw yëngu-yëngu yu metti yi amoon ci...

BEQI : JÀPPUÑU NGAÑ DEMBA TURE

Xibaar bi ñu biraloon ñeel jàppug Ngañ Demba Ture mu Pastef wérul. Kenn jàppu...

BUBAKAR BÓRIS JÓOB, BINDKAT : “KENN WARUL A ÑÉDD NGUUR BA SAY BAARAAM DI NÀCC.”

Seen yéenekaayu web, Lu Defu Waxu, amal nab laaj-tontu bu yaatu ak werekaan bii...

JÀMMI USMAAN SONKO, JÀMMI RÉEW MI

Barkaatu-démb, ci alxames ji, lañu daan njiitul làng gii di Pastef, Usmaan Sonko, lu...

YËNGU-YËNGUY RÉEW MI : JÀNGUNE YAA NGIY TËJ

Juróom-ñeenti bakkan ci alxames ji, fukk ak ñett ci àjjuma ji, muy ñaar-fukk ak...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...