Li fës

SIGICOOR : « PANAANUG WAY-BËGGI REEW MI »

Ay téeméeri téeméeri nit ñoo dajaloo ca buntu këru Usmaan Sonko, fa Sigicoor jamono...

POROFESËER PENDA MBÓW : « MËSUMA ÀND CI YEMOOG GÓOR AK JIGÉEN (« LOI SUR LA PARITÉ ») »

Bañ koy wote ci jamonoy Njiitu réew ma woon, Abdulaay Wàdd, soxna Penda kesee...

F24 : WENN SAY, GENN KÀDDU

Démb ci àjjuma ji, ginnaaw julli jumaa, la waa F24 woote woon fa «...

SONKO-BÀRT : YÀGG BAWUL DARA (1/2)

Cin bax na, waaye du jikkoom, matt a ko ca jóo. Altine ba tey,...

ÑAARI KUY DUÑU BOKK MBALKA

Pólitig ci Senegaal du jóg di jur mbetteel ci askan wi. Mu mel ni,...

SAFAANTOO YA CA NGOR : ÑAARI BAKKAN ROT NAÑU

Njiitul mbootaay "Ngor debout", Mamadu Njaay, yëgle na ni ñaari nit dee nañu ci...

DAAN NAÑ USMAAN SONKO 6i WEERI KASO YUM DUL TËDD

Ndogal li jib na. Lees doon njort bir na. Nee na fàŋŋ. Àttekat bii...

USMAAN SONKO AK MAKI SÀLL : CÓOKI MUJJ GI

Tey, ci altine ji lees war a àttewaat layoob Usmaan Sonko ak Maam Mbay...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...