Li fës

JÀPPUG PAAP AALE ÑAŊ

Seneweb moo siiwal xibaaru jàppug Paap Aale Ñaŋ, taskatu-xibaar ak faramfàccekat bu siiw. Jamono...

Sitt ak Papaa Sow : Wure wa dem na këŋ

Sitt ak Papaa Sow dinañ jàmmaarloo ci dibéer jii, 6 noowàmbar 2022 ca Aren...

Li gёn a fés ci xibaari bés bi Alxames 3 nowambar 2022

PÓLITIG Coowal Aji Saar ak Usmaan Sonko Démb ci alxames ji, 3 nowàmbar, la kii di...

NDÉGLUG SONKO GI, NA WOON FA WOON ?

Woote bi yoon woo Njiitalu Pastef li, Usmaan Sonko, la yéenekaayu yi xëyee tey....

PASUG NGÀNNAAY GI : MBIR MI TEERI NA NGOMBLAAN GA

Dañ doon xaarandi Ngomblaan gi wax ci mbirum pasug ngànnaay gi dox diggante Nguurug...

CAN 2022 (Beach soccer) : Senegaal gàddooti na ndam li

Senegaal jël na Can 2022 (beach Soccer) bi. Esipt la dóorati 6-5 ci dóoral-ma-dóor...

PASUG NGÀNNAAY GU 45i MILIYAAR : AW NJOMBE WU BEES ? 

Ag pasug 45i miliyaar ñeel i ngànnaay yu Njawriñu kéew mi jënde ci LAVIE...

CARGALUG NEUSTADT INTERNATIONAL PRIZE FOR LITERATURE : BUBAKAR BÓRIS JÓOB JËL NA NDAM LI

Ci talaata 26eel ci oktoobar 2021, lees jot ci mbégtem weer wi. Surnaalu ladab...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...