Li fës

BIRAM SULEY JÓOB, MBAA DU… ?

Gor, ca wax ja. Kàddu gilee génn démb ci gémmiñi saa-senegaal yu baree bare....

GII MARIS SAAÑAA XAS NA JËWRIÑU WÉR-GI-YARAM

Gii Maris Saañaa dal na ci kow Mari Xemes Njaay, jëwriñu wér-gi-yaram geek Ndimbalu...

CÀKKUTEEFU KURÉLU “COLIDEP”

COLIDEP (Collectif pour la Libération des Détenus Politiques) nag ay kuréli way-moomeel a ko...

NJOMBEW 6i PÀKK YI NGUUR GI WÀNTEER PERETZ

Noppeegunoo wax ci njombew pasug 45i miliyaar yi, ñu sullil nu beneen tóoxidóoni. Usmaan...

Limub gaynde yiy dem ca kub bu àddina si : Saajo Maane mooy kiy dem

Aliw Siise siiwal na limub gaynde yi war a teewal réewum Senegaal ca kub...

GUY NJÓOBEEN (1/2)

Aatu feeñ na ! Njaayeen yi dégluleen Njóobeen bi raw na leen Buleen ko réyloo woyal,...

BÉSUB BINDKATI AFRIG YI

7i fan ci weeru nowàmbar mooy bés bi ñu jagleel bindukati Afrig yi (saa-Afrig)....

Usmaan Sonko : « Paab Aale Ñaŋ du doon weneen nagu sarax… »

Coowal jàppug Paap Aale Ñaŋ gi moo lëmbe réew mi ba tey. Kilifa yu...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...