Li fës

GAYNDEE NJAAY ! MBARA-WÀCC ! CAN 2022 : SENEGAAL JËL NA RAW-GÀDDU GI

Dibéer, 6eelu fan ci féewaryee 2022, 21i waxtu ci guddi tegal nañu. Lépp a...

RUWÀNDAA, RÉEW MA FARÃS NEE TOTT AK GÀCCE (BUBAKAR BÓRIS JÓOB CI TEKKIG PAAP AALI JÀLLO) 1/2

Weeru màrs 2021 wee ñu génn, ci 26eelu fan, « Ndajem gëstub ceedeefi Farãs...

CARGALUG NEUSTADT INTERNATIONAL PRIZE FOR LITERATURE : BUBAKAR BÓRIS JÓOB JËL NA NDAM LI (PAAP AALI JÀLLO)

Ci talaata 26eel ci oktoobar 2021, lees jot ci mbégtem weer wi. Surnaalu ladab...

PÉNCUM MAAM YUNUS JEŊ : LADAB CI LÀMMIÑI RÉEW MI (NDEY KODDU FAAL)

Ku dégg Maam Yunus Jeŋ, sa xel dem ci jigéen ji jëkk a bind...

MAKI DA NI WOON YOONU YOKKUTE : LÉPP YOKKU NA !

«Réew mi dafa tagatémbe !», «Dund gi jafe na !», «Lépp a dëgër !», «Danoo sonn!»,...

Gis-Gisu Seex Aliyu Ndaw ci "Francophonie"

Faraŋ ko fóni (Woy) Faraŋ ko fóni Man kat daa waaru Kaay làggi ci saaw làmmiñ Na doon saw...

JÀNGOROY ÑÀKK JI NU GANESI

Askanu Senegaal tollu na ci diggante bu tar cig ñàkk ba sax, li ëpp...

ÀND WATTU LÀKKI RÉEW MI

"MBINDAAN" LEES WAROON A BIND ------------------------------------------------------------------------------ ÀND WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi ! Ñaareelu yëngug...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...