Li fës

TUKKIB MAGUM JËWRIÑ YI FA GÀMBI

Démb, ci gaawu bi la elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, demoon fa Gàmbi. Li...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA QATAAR

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, ma nga tay fa réewum Qataar....

CAMPEEF / NGOMBLAAN GI : TAXAWAL NAÑU PEKK GU YEES GI

Ginnaaw bi ñu falee dépite Maalig Njaay ci boppu Ngomblaan gu yees gi, sampees...

NDAJEM JËWRIÑ YI

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jiite na ndajem jëwriñ yi barki-démb...

DÉPITEY FARÃS YI DAANEEL NAÑU CÀMMUG MICHEL BARNIER

Dépitey Ngomblaanu Farãs yi wote nañu pasum diiŋat (motion de censure), daldi daaneel Càmmug...

ÀMBURUWAAS SAAR : AATU RÉER NA !

Njabootu làmbu Senegaal ak mbatiit am nañu dëj. Nde, xibaaru tiis ak uw naqar...

TIIS WU RÉY FA GINE

Mats futbal bu mujje ciy masta ! Mbir yaa ngi xew barki-démb ci dibéeru...

ALIYUN BADARA BÉEY GUDDEE NA

Aliyun Badara Béey, njiitu kurélu bindkati Senegaal yi, moo génn àddina. Keroog, dibéer 1eelu...

XËT YI MUJJ

AAMADU BA (JËWRIÑU MBATIIT MI) : « MBATIIT, DAFAY JUBOOLE TE DI SAXAL WÓOLOONTE »

Jëwriñu Mbatiit* mi, Ñeeñal* gi ak Wërteef* gi, Aamadu Ba mu Pastef, teewoon na...

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...