Li fës

KÀDDUY NJIITU REEW MI CA NDAJEM MBOOTAAYU XEET YI

Démb ci àllarba ji, Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, ma nga woon...

TÀGGE : PAATUG AAMADU MAXTAAR MBÓW

Guy daanu na. Aamadu Maxtaar Mbów, maamu askan wi, moo génn àddina. Ci guddig...

JUB, JUBAL, JUBBANTI : CONC BI TEGGEEKU NA !

Keroog 24 màrs 2024 la conc bi teggeeku. Keroog it la Yoon tekkeeku, wayndare...

MBIRI ABDULAAY SILLA AK LAT JÓOB

Talaata jii weesu lañu taxawal li ñuy dippe PJF (Pool Judiciaire Financiaire). Ëttu àtte...

WOTEY NGOMBLAAN GI

Amal nañu am ndaje ñeel wotey Ngomblaan gi ñu namm a amal ci weeru...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/9/2024)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA NJAASAAN Dibéer jii weesu moo nekkoon bés bi ñu doon...

MBËNN MA FA TUUBAA

Asamaan démb si dafa bàyyeeku, ubbiy buntam, rëccal ndox mi, mu sotteeku bu baax...

NJAAG NANGUL !

Baaxoo nanu, fi réew mi, bu xewu bànneex amee, jigéen ñiy joqalante ay teraanga....

XËT YI MUJJ

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...