Li fës

KAÑ LANUY TOOG ?

Doomi Senegaal, ñu yàgg a dox lañu. Bu ñu nekkul fépp it, bari na...

USMAAN SONKO WOOTE NA BENNOO NGIR PALESTIN

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ma nga woon démb ca ndajem njàppale Palestin ma...

LU YEES CI BÓOMUG ASIIS DABALAA AK WAALI

Mbirum bóomug ñaari bakkan yooyu moo lëmbe réew mi jamono jii. Waaye, mel na...

NJIITU RÉEW MI DALAL NA NJIITU NGUURUG ESPAAÑ

Tey, ci alxames ji, la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, doon dalal...

TÀGGE : SOXNA WAALO MU SËRIÑ SAALIW MBÀKKE NELAW NA

Xibaar bu tiis la njabootu Tuubaa ak taalibey murit yi xëyee tey. Soxna Waalo...

WOODSIDE : NDAM AM NA CI SÉMBUW SÀNGOMAAR WI

Woodside Energy siiwal na xibaar buy neex Saa-Senegaal yi, rawatina njiit yu bees yi....

NJIITU RÉEW MI TABB AMINATU TURE

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, tabb na Soxna Aminata Ture. Ci altine ji,...

TASUB CESE AK HCCT

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, dafa jébbal njiitul Ngomblaan gi ab dekkare...

XËT YI MUJJ

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...