Li fës

AY NAAL ÑEEL NJÀNG MI

Njiitu réew mi teewoon na ca ndaje ma ñu doon sargale ndongo yi gën...

AM-AMU NJIITU RÉEW MI

Ndajem Ndeyu Sàrtu réew mi siiwal na am-amu Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar...

COONO DU RÉER ?

Bari na ay xale yuy làqatu di lekk kaani. Ndax, mag ñee leen koy...

AKSIDAŊ DIGGANTE NGAAY-KEBEMEER

Aksidaŋ bu metti moo am tey ci yoonu Ngaay-Kebemeer wi. Fukk ak benni nit...

CAAROY 44 : USMAAN SONKO ŊÀÑÑ NA FARÃS

Caaroy 44, xew-xew bu tiis la ci mboorum Afrig, rawatina mom Senegaal. Jéyya jooju,...

LOMPUL : BIRAM SULEY JÓOB WAX NAAK NJIITI GCO YI

Jëwriñ ji, Biram Suley Jóob, wax na ak njiiti GCO (Grande Côte Opérations SA),...

SÉMBUW NDEFARUG DAAMAR FI SENEGAAL

Senegaal mën na am ndefarug boppam gog, dinay liggéey ay daamar fi réew mi....

TÀGGE : USÉYNU BÉEY WÉY NA

Njabootu mbatiit ak làmmiñi réew mi amati nañ tiis ak uw naqar. Kenn ci...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...