Li fës

CFEE 2024

Joŋantey CFEE yi door na ci biir réewum Senegaal, ca Gàmbi ak ca Gine...

YENU SA BOPP

"Yen bu diisee, dañu koy jàppoo". Loolu la maam ja waxoon. Noppeegul sax, kenn...

COVID-19 BI NUYOOTI NA !

Li ñu doon laam-laamee démb ak barki-démb mi ngi bëgg a leer. Nde, ñu...

WÀÑÑITEG NDUND GI

Wàññiteg njëgu ndund gi, Càmm gi jël na ci ay ndogal. Lañu jotoon waxtaane...

NJUREEFI NDAJEM JOMAAY AK MACRON

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, ma nga woon Farãs. Daf fa teeweeji...

FIPPU CA KÀMPENAAL BU “LIBERTÉ 6”

Jar-jar (prisonniers) ya nekk ca kasob Kàmpenaal (Camp penal) bu “Liberté 6” ñoo doon...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI CA FARÃS

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, war teew ca Farãas ci àllarbay tey jii....

FITNA FA MEDINA GUNAAS

Xibaar bu yéeme te doy waar moo jib tey, ci bésub tabaski bi. Muy...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...