Li fës

CÀKKUTEEFU WAA FORUM CIVIL

Kurélug maxejj yi, ñu gën koo miis ci Forum Civil, àdduna ci wàññi gi Nguur gi...

MA-DEMBA SOKK WUYUJI NA BOROOMAM

Xibaar bu tiis la réew mi xëyee tey. Ma-Demba Sokk moo génn àddina. Pari...

AY TABB YU YEES

Barki-démb ci àllarba ji lañu doon amal ndajem jëwriñ mi. Ñu amal ko nag,...

WATTU LÀKKI RÉEW MI 2/3

TURI JOTAAYI TELE SENEGAAL YI Seen Xéewal Tës Saa Njóogu Kër gi ak Taal Ngol-Ngol Aaru Mbedd Diine ak Jamono Reeni...

WÀÑÑIG DUNDU GI

Ñoo ko dige woon, tàmbali nañ ko def. Càmmug Basiiru Jomaay Fay geek Usmaan...

WATTU LÀKKI RÉEW MI 1/3

Ànd jubal mbind mi ! Ñaareelu yëngug jubbanti mbindin mi Yaxub kubbite  Tey jii, boroom...

BARIGO PETOROL BU NJËKK FA SÀNGOMAAR

Muy xibaar bu njëkk ci noppi àdduna wërngal këpp : réewum Senegaal sol na...

SONKO YËNGAL NA

Ndaje moomu mi ngi amoon démb ci dibéer ji, fale ca béréb boobu ñuy...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...