Li fës

“ICS” FEEÑLE NA

Ginnaaw riirum caabal yi ci yorinu alalu askan wi, coow topp na kër gii...

NJUUMTE

Ci xam-xamam bu amul yemu ak xareñam bu amul sikki-sàkka, Boroom Bi dafa bind...

BATAAXELU NJÉMMEER ÑEEL JAWRINU CAYTUG NJÀNG MI CA LUGA

Kilifa gi, Ginnaaw ba ma la nuyoo jox la sa wàccuwaay, duma def lu moy...

JUB, JUBAL AK JUBBANTI CI KOW TALI YI

Naalu “Jub, jubal, jubbanti” fa mu duutoon baaraamam teggiwu ko. Kilifay Càmm gu bees...

BORUB GALAG ÑEEL KËRI TASUKAAYI XIBAAR YI

Jamono jii, këru tasukaayu xibaar yu bari ñoo ngi ci guuta. Ndaxte, dañu ame...

NDOGAL YU YEES ÑEEL NJÀNG MU KOWE MI

Abdurahmaan Juuf, jëwriñu njàng mu kowe mi, gëstu geek coste gi, biral na njureef...

DOORO GÉY, BAH JAXATE AK IMAAM SÉEX TIIJAAN NDAW DEM NAÑ KASO

Tey ci altine ji, ñetti fan ci weeru suwe la ndogal li daanu. Bah...

SET-SETAL NGIR WAAJAL NAWET BI

Démb, gaawu 1eelu fanu suwe 2024, moo doon bés bees jàppaloon set-setalu réew mi....

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...