Li fës

LËLUB NJÀNG MU KOWE MI ÑEEL BAAXAL APPUG NJANGALE MI

Kilifa yi séq njàng mu kowe mi ubbi nañu lëlub ñetti fan. Ñu namm...

NJIITU RÉEW MI TEEWE NA WAXTAANUW ONU WI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, teewe na, démb, waxtaan wi Mbootaayu Xeet...

NJAAYUM SUUF : DOORO GÉY TAQAL NA MAKI SÀLL

Dooro Géy, di kenn ci ñi jege lool Maki Sàll, lañu jàpp fan yii...

YOON : JUB, JUBAL, JUBBANTI

Tey, ci talaata ji, 28 pani suwe 2024, lañuy tijji péncoo mi ñu jagleel...

NDOLLENTU JURÓOMI AT NGIR KÀPPITEEN TARAAWORE

Ndogal loolu ñi ngi ko jël barki-démb ci gaawu gi ginnaaw waxtaan wu ñu...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA PARAAYAA AK KONAAKIRI

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA PARAAYAA AK KONAAKIRI Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar...

BÓOMUG ALEŊ KALI: G7 BU CEES DOOR NA XEEX BI

Barkaatu-démb ci talaata ji lañu bóom jangalekat bii di Aleŋ Kali. Ci anam yu...

TUUMAY LUUBAL ÑEEL YAAY FAATU JAAÑ

Yaay Faatu Jaañ la yéenekaayu Yoor-Yoor xëyee tey ci xëtam bu njëkk, mbaali jokkoo...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...