Li fës

AYU-BÉSU JËF ÑEEL NJÀNG MI

Démb ci àjjuma ji lañ doon tëj ayu-bés bi ñu jagleel jëf ñeel njàng...

Aksidaŋ bi ca yoonu Kungël : Njaal ak ndigali Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay

Démb ci alxemes ji, 25i awril 2024, la aksidaŋ bu metti amee woon fa...

23 AWRIL BÉSUB TÉERE AK ÀQU BINDKAT BI

Mbootaayu Xeet yi ñeel njàng, xarala ak mbatiit (UNESCO) moo tànn bésub 23 ci...

SIIWALUG CAABAL YI

Àllarba jii weesu la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, doon amal ñaareelu...

SÉEX ALIYU NDAW GÉNTOON NA KO DÉMB, AADAMA BAROW AK BASIIRU JOMAAY FAY DEF NAÑ KO TEY

Atum 1981, Séex Aliyu Ndaw, bindkat bu ràññeeku, daa bind woy tudde ko : Sama...

ÑAAREELU TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA BITIM-RÉEW

Ginnaaw bi mu njëkkee génn, dem fa réewum Móritani, Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (19/4/2024)

NDOGALI NJIITU RÉEW MI, BASIIRU JOMAAY JAXAAR FAY  Ganug njénde li Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay...

BUBAKAR BÓRIS JÓOB : « DAÑU WAR A TOPP NJIIT YI FI NEKKOON… »

TV5 doon na dalal werekaan bu mag bi, Bubakar Bóris Jóob, séq ak moom...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...