Li fës

NJËLBEENI TUKKIY NJIITU RÉEWUM SENEGAAL FA GÀNNAAR AK GÀMBI

Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Fay,  dina amal njëlbeeni génnam ci ayu-bés bile. Moom...

NJIITU RÉEW LU BEES LI NEMMEEKUJINA KILIFA DIINE YI

Ni ñu sànnee woon ay gët, bàyyi ko xel ci génnam bu njëkk bi...

NJIITU RÉEW MI FA TUUBAA

Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, amal na génnam gu njëkk ci biir...

RUWÀNDAA, 30I GINNAAW FAAGAAGALUG TUTSI YA

Lu xewoon Ruwàndaa ca atum 1994 ? Keeroog, 6eelu fanu awril 1994, lañ song roppalaanu Njiitu...

IRÃ SONG NA ISRAAYEL

Ay weer ginnaaw ba ñu dekkalaatee xareb Israayel ak Palestiin, ba tey jeexagul. Ndax,...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : BËGG-BËGGI JËWRIÑ JI MUSTAFAA GIRAASI

Jëwriñu njàngale mi ci daara yu ndaw yeek yu digg-dóomu yi, Mustafaa Giraasi, fésal...

NJIITU RÉEW MI BIND NA LIGÉEYKATI CAYTUG BOKKEEF GI

Njjitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, bind nab bataaxel, jagleel ko liggéeykati caytug...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/4/2024)

NJÉBBALUG LENGE FA MÀKKAANI NJËWRIÑ YA Keroog ci àjjuma ji la elimaanu jëwriñ ji génne...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...