Li fës

154 MILIYOŊ AK LU TEG AT MU JOT : MAKI SÀLL SÉDDU NA LAATA MUY DEM

Maki Sàll, waajaloon na boppam ca atum 2013. Ndeke, mi ngi doon sóoraale ab...

TÀGGE : MAHAMMAD BUUN ABDALAA JONN DËDDU NA

Elimaanu jëwriñ ja woon, Mahammad Buun Abdalaa Jonn, moo génn àddina.  Tey, ci àjjuma...

NJIITU RÉEW MI NEENAL NA NDOGALI MAKI SÀLL YI

Ginnaaw bi mu jëlee lenge yi niki Njiitu réewum Senegaal, Basiiru Jomaay Fay jël...

TOMB YI GËN FËS CI KÀDDUY NJIITU RÉEW MI

Njiitu réewum Senegaal lu yees li, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, doon na wax ak...

USMAAN SONKO : ELIMAANU JËWRIÑ YI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, tabb na Usmaan Sonko, def ko elimaanu jëwriñ...

CAMPUG BASIIRU JOMAAY FAY

Ngelaw lu bees la réewum Senegaal noyyiwaat tembe ci campug Njiitu réew lu bees...

PÂQUES 2024 : PAAB FRANÇOIS A NGI WOOTE JÀMM CI ÀDDINA SI

Paab bi sàkku na ngir ñu dakkal xare bi dox diggante Israayel ak Palestin....

MAKI SÀLL, NAY RAFET !

Ci guuta gu réy la Senegaal génn, ginnaaw bees amalee wotey 24 màrs yi...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...