Li fës

LACOS DUUT NA BAARAAM NDAJEM NDEYU ÀTTE MI

Lu ëpp ayu-bés a ngi nii, ginnaaw ba caytug xobi baayale yi tàmbalee. Boobaak...

MARIN BU SENEGAAL : JURÓOMI KOMÀNDOO YI RÉER

Juróomi komàndoo yu marin bu Senegaal ñoo réer. Muy mbir mu doy waar mu...

NDAJEM NDEYU ÀTTE RÉEW MI : GEG NAÑ USMAAN SONKO

Tey ci àjjuma ji la ndajem ndeyu àtte réew mi warron a jeexal caytug...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (04/01/2024)

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ AK USMAAN SONKO Coow li doxoon diggante Maam Mbay Ñaŋ ak...

KARIIM WÀDD : “SAMAG GÀDDAAY MI NGI JEEX”

Ni ñu ko baaxoo gise ci njeexitalu at mu nekk, njiitu réew mi dina...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI CI AT MU BEES MI

Démb ci guddig dibéer ji, yemoo woon ak fanweeri fan ak benn ci weeru...

WOTEY 2024 YI : WURE WA DEM NA KËŊ

Tey ci gaawu gi la ndajem ndeyu àtte réew mi tàmbali seen liggéey ñeel...

SÉEX ANTA JÓOB, SUUL KER DU KO TEE FEEÑ…

Séex Anta Jóob a ngi juddoo Céytu, 29eelu fan ci desàmbar 1923. Alxuraan la...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...