Li fës

MALIN BJÖRK (U.E) : « BËGG NANU GISE AK BASIIRU JOMAAY FAY »

Ndaw yi Bennoog Tugal gi yabal (Mission de l'Union Européenne) ngir ñu saytu wotey...

TAAX BI MÀBB NDAKAARU : 5I BAKKAN ROT NAÑU

Taaxub 3i etaas moo màbb ci guddig altine ji jàpp talaata. Xaar-Yàlla la jéyya...

WOTEY 2024 YI : MBIRUM NDIISOOG LUÑÑUTU GI

Mbirum ndiisoog luññutu gi dépitey PDS yi sumb ca Ngomblaan gaa ngiy wéy di...

MALI, BURKINAA FAASO AK NISEER BOKKATUÑU CI CEDEAO

Kaawteef ! Mali, Burkinaa Faaso ak Niseer mànkoo nañ génn ci CEDEAO. Xibaar bi...

SENEGAAL, XALIMAY ÑAARI BINDKAT DAMM NAÑ…

Ibraayma Aan ak Àbbaas Njoon, ñaari bindkat yu mag, ñoo génn àddina : kii ci...

KATI LEENA NJAAY : KOPPAR, SAÑ-SAÑ, MBOORUM FCFA

Film bi Kati Leena Njaay (sottalkat) mujj génne te tudde ko Koppar, sañ-sañ, mboorum...

MÀGGALU POROXAAN : NU SIYAAREJI SOXNA MAAM JAARA

Màggalu Poroxaan bokk na ci xew-xewi diine yi gën a ràññeeku fi réew mi....

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...