Li fës

“MAN, SÉEX ANTA JÓOB !”

Bu Séex Anta Jóob (1923-1986) doon dund ba tey, am koon na 100i at...

70i WAY-SÀKKU JÉBBALE NAÑ SEEN I WAYNDARE

Ci àllarbay tey ji, 27 desàmbar 2023, la àpp bi Ndajem ndeyu àtte mi...

SIYAARE DAARAY KOKKI : BÉSUB ALXURAAN

Démb ci dibéer ji? yemoon ak ñaar-fukki fan ak ñeent ci weeru desàmbar wii,...

RËG-RËG DAAN NA BOMBARJEE

Dooley xale xajul ci mag. Loolu la doomu Caaroy ji wan na doomu Mbuur...

MBIRI NDEELA MAAJOOR JUUF

Ndeela Maajoor Juuf dugg na ci guddi gu bët setagul. Ginnaaw ba ñu ko...

BÀRTELEMI JAAS SOOY NA

Ci àjjumay tey jii, 22 desàmbar 2023, la Ëttub àttewaay bu mag bi doon...

JÀPP NAÑU NDEELA MAAJOOR JUUF

Coowal Ndeela Maajoor Juuf moo lëmbe tey réew mi. Mollah Morgun mooy siiwal ci...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...