Gis-Gis

DÉMB SEŋOOR, TEY WÀDD

Li ko dale atum 1978 ba tey jii, woteb ren bii mooy wote bu...

AYSATA TAAL SÀLL : JIGÉEN SOPPAL TE BUL WÓOLU…?

Bés ba ma ko déggee mu naan kilifa diine yi dañ maa ñaan ma...

DI BUUR, DI BUMMI

Li jaaxal waa Senegaal, mooy wax-waxeet yi kilifay réew mi dëkke. Ku ci jóge...

Bàlla Gay-Móodu Lóo : ñaar ci dara

Làmbu démb ak ju tey jeeka wuute ! Ndege, démb, bu nawet bi wàccaan, ci...

XËCC BU DAŊEE DAGG !

Nimbir yiy doxe diggante nguur geek kujje gi bi Màkki Sáll toogee ci jal...

DIBÉERU WËLBATI

Cialtine jii la njiitu réew mi doon jébbal askan wi saxaar gi ñu duppe...

XËT YI MUJJ

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/1/2025)

JURÓOM-ÑEENTEELU BÉSU SET-SETAL Set-setal bi ab xew-xew la boo xam ne Nguur gee ko doon...

NDÀMPAAYUL WAY-LORUY XEW-XEWI 2021-2024

Jëwriñu Njaboot gi ak Ndimbal yi, Maymuna Jéey, biral na ndogal yu yees yi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/1/2025)

7i BAKKAN ROTATI NAÑU CI TALI BI Juróom-ñaari nit ñoo ñàkk seen i bakkan ci...

NDAJEM JËWRIÑ YI (29/1/2025)

Nees ko tàmm a defe ayu-bés bu nekk fa Njénde la, amal nañu ci...