Gis-Gis

7 MÀRS WALLA 8 MÀRS ? BEY CI SA WEWU TÀNK…

Juróom-ñetteelu fan ci weeru màrs la xel yépp di dem ci jigéen ñi, ndax...

NISERYAA : BUHARI FALUWAAT NA

Ci weeru féewaryee wii jàll la askanu Niseryaa doon amal woteb njiitu réewam. Ba...

ANA LU GÓOR-GIY LÀQARCI ?

Bamu jógee Konaakiri ba tey, seeti woon Alfa Konde, Abdulaay Wàdd, sunu Njiitu-réew ma...

BÉS DU MAG, DU TUUTI, BOROOM LAY TOLLOOL…

Dëgg la : ràcc jëmale sa kanam baaxul waaye tey fàww LU DEFU WAXU xamle...

SENEGAAL, SEEN GAAL LA, ÑOOM, AM SUNU GAAL… ?

Ku waaruwul ci doxinu miim réew, saw doxin dina la waari ëllëg. Ku yéemuwul...

‘’BÀNK MONJAAL’’, KURÉL GI NUY JATAŋ

Ñépp a ngi fàttaliku ni « Bànk Monjaal » nasaxale woon réew mi ci...

NDAM LU SAFUL XOROM, SAFUL SUUKAR…?

10Dibéer yemook ñaar-fukki fan ak ñeent si weeru Féewaryee, la waa réew mi doon...

XALAM DEMOON NA BAY NEEX

Dibéer, 24eelu fan ci weeru féewaryee, atum 2019. Bés bi ñépp doon xaar, agsi...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...