Xibaar

TÀGGAT YARAM

Saajo Maane dugal na ñaari bal ci joŋante bi ekibam Liverpool doon amal démb...

MAKI SÀLL GANEJI NAY DËKK AK I GOXI RÉEW MI : SAFIYETU BÉEY

Kafrin, Fatig ak Kawlax am nañu gan fan yii weesu, gannaaw bi njiitu réew...

POLITIG : SAFIYETU BÉEY

Aymeru Ñing, doon kilifa ci Bennoo Bokk Yaakaar te jiite kurél gi ca Péncum...

NOOK MBËNN MII NAG, BA KAÑATI ? (SÉEX AXMADU BÀMBA NJAAY)

Séex Axmadu Bàmba Njaay “Ku ndóbin rey sa Maam, foo gisee lu ñuul sax daw.”...

PÉEXTE (LÀMP FAAL KALA)

PÉEXTE Da maa dëfeenu di jeneer Ba xel mi tàbbi cig ndenéer Dellusi naan ma nu gàddaay Fii...

WEYI TAN (SAYDU BA)

Saydu BA waa Ñooro la, di al-pulaar bu gàlle. Ndaanaan luy yëngu ci teyaatar la,...

SUNU RÉEW MI (NDAY XAYBA FAAL)

  Soxna Nday Xayba FAAL mi ngi dëkk Ndakaaru, doon jàng xam-xamu melosuuf ca Daara ju...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...