Xibaar

NDEY SÀGGAN, DOOM FAATU (NDEY KODDU FAAL)

Waa Mamel, fii ci Ndakaaru, naqar ak tiis lañ fanaanoo. Li ko waral mooy...

KU TEDD KI (Soxna Kumba Mbόoj)

Soxna Kumba Mbόoj, ñu gën koo xam ci turu Kumba Falilu, mi ngi am...

MBAS MEEK ÑÀKK XÉY CI SENEGAAL (SAFIYETU BÉEY)

Bérébu liggéeyukaay yu bare tëj nañu ndax mbas mi, loolu la ab lànket bu...

SENEGAAL WÓOLUWUL GARABU MADAGASKAAR GI (SAFIYETU BÉEY)

«Kenn du jëfandikoo Covid Organics fii ci Senegaal». Porfesoor Musaa Séydi xamle na ni...

GÀTTALUG XIBAAR YI (AMI MBENG)

TUUBAA Ki yore kàddug « Muxadimatul xidma » di Maxtaar Kan, mu ngi xamle ne « li wér...

MALI (Musaa Aysatu Jóob)

Ginnaaw bi nguurug Ibraayim Bubakar Keyta daanoo ci weeru ut 2020, réewum Mali mi...

TAALIF CI MAAM ABDUL ASIIS SI DABBAAX (DAAWUDA NJAAY)

                     Taalif ci Maam Abdul...

MÀGGALU TUUBAA (Musaa Aysatu Jóob)

Dees na amal màggalu Tuubaa ci 6i fan ci weeru oktoobar. Ginnaaw bi ndigal...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...