Xibaar

JOŊANTE REN BII, PETOROOL LAY XEEÑ…

Keroog, askanu Senegaal jóg na ci njekk ak teggin, daldi def li ko war...

ÑAŋ-MBAALO, TOJ NGA LÀMB JI !

« Toj naa fii ! », « Tasaare naa fee ! », « Rajaxe naa fale ! »… Su nu waxantee dëgg, xorom si...

Lan la wutaakon yi naral làkki réew mi ?

Waaw mbokk yi, lan la wutaakon yi naral làkki réew mi ? Man ci...

DIINE AK POLITIG : NAN MOYTU LI NUY FÉEWALE

Ëttu boole bi, genn kurél la gu boole mbooleem këri diine yi ngir saxal...

KAN MOOY USMAAN SONKO ?

Usmaan Sonko nëbbu ko kenn : mébétam mooy jot ci réewum Senegaal ci guddig...

MÀNGAAN NDEKE AM NA CI PÓLITIG !

b ak yu tey gis ñu woroo lool. Am na sax ci ñoom ku...

RIIRU KÀMPAAÑ

Lépp lu yëngu am na lu ko yëngal. Réewum Senegaal, jamono jii mu ngi...

KAN MOOY ISAA SÀLL ?

« Jàpp naa ne pólitig du liggéey, jàngale mooy sama liggéey » (Isaa Sàll) Isaa Sàll, ab wutaakon...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...