Xibaar

LI ÑÉPP BOKK

Waxi Wolof, yenn saa, dañuy xaw a juunoo. Dafay mel ni sax kuy weddi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/5/2025)

CÀMBAR YI JÓGE CI SÉMBI TEG I TUUMA ÑI FI NEKKOON I JËWRIÑ Ngomblaan ga...

MBIRUM AAMADU (MAKI) SÀLL : WOOLU NAÑ WAALI SEKK

Mbirum Aamadu Sàll, doomu Njiitu réew ma woon (Maki Sàll), mi ngi wéy di...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/5/2025)

NJÀNG MEEK NJÀNGALE Mi Jëwriñu njàngale mi ci daara yu ndaw yeek yu digg-dóomu...

ÑAXTUY LÀNGI PÓLITIGI MALI YI

Coowi pólitig yi lëmbe na lool réewi Afrig sowu-jant yi, rawatina ci juróomi at...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

SÀMPIYONAA ALMAAÑ : BAYERN MUNICH NANGUWAAT NA CËRAM Vincent Kompani ak i ndawam jël nañu...

MUREES NA MBALAANI KIIRAAYI MUSTAFAA JÓOB AK NDEY SALI JÓOB JEŊ

Ngomblaan gi muri na mbalaani kiiraayi ñaari dépite yii di Mustafaa Jóob ak Ndey...

NDOG LU METTI FA WELINGARA : ÑAARI NJÀNGAAN FAATU NAÑU CI

Ñaari njàngaani CEM Saare Koli Saale ñoo faatu ci ndog mu metti ci gaawug...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...