Xibaar

NGUUR GI DAJALE NA 405i MILIYAAR

Nguurug Senegaal dajale na 405i miliyaar ci 15i fan kese. Muy alal ju takku...

CAABALUG ËTTUB CETTANTAL BI : YOON SUMB NA LIGGÉEY BI

Saabalukaay bii di Source A moo siiwal xibaar bi. Bees sukkandikoo ci li yéenekaay...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/4/2025)

WOOLU NAÑU SIMÕ FAY Yoon a ngi wéy di teg bët ci liy xew ci...

TÀGGE : MAMADU BAAJO KAMARA GÉNN NA ÀDDUNA

Xibaar bu tiis la réewum Senegaal yeewoo tay, rawatina ñiy liggéey ci wàllu Yoon....

SÉYDINAA MUHAMMADU MAXTAAR LAAY, XALIFA LAAYEEN YI, DËDDU NA.

Xalifa Laayeen yi, Séydinaa Muhammadu Maxtaar Laay, génn na àddina guddig talaata (8eelu awril...

SÉMBUW « SPACEBUS 2025 » : YËR JAWWU JI NGIR SUUXAT YOKKUTE AK NAATAANGE SENEGAAL

Barkaatu-démb ca ngoon, yemook dibéer 6i fani awril 2025, Njiitu réew mi jiite woon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/4/2025)

TABB NAÑU AMSATU SOW SIDIBE Njiitu Réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, tànn na...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...