Xibaar

NGOMBLAAN GI WOTE NA SÀRTUB LEERAL BI

Ngomblaan gi wote na sémbuw àtte wiy leeral àtteb njéggal (loi d'amnistie) bi Maki...

MBIRUM MARINE LE PEN

Marine Le Pen kenn la ci ñi ñu gën a bàyyi xel ci géewu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/4/2025)

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI Jëwriñu njàng mu kawe mi, gëstu beek coste gi, Abdurahmaan Juuf,...

KORITE 2025 : KÀDDUY NJIITU RÉEW MI

Ci altiney tay jii la Njiitu réew mi julli korite. Fa Jumaay Ndakaaru ju...

PÉNCOO MI ÑEEL NJÀNG MU KAWE MEEK GËSTU BI

Ginnaaw bi ñu nekkee ciy waxtaan ak i joyyanti ngir jubbanti ati njàng yu...

GINE-KONAAKIRI : SENERAAL MAMADI DUMBUYAA JÉGGAL NA MUSAA DADIS KAMARA

Sóobare ba jiite réewum Gine-Konaakiri jamono jii, Seneraal Mamadi Dumbuyaa, jël na ndogal lu...

NJÉGGAANIY SENEGAAL : SIIN ROMB NA FARÃS

Senegaal, li ëpp ci lees fiy jëfandikoo, lees di jéggaani la. Dafa di nag,...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...