Xibaar

PAAB CAW TÀNN NA AY GAYNDEEM

Tàggatkatu Senegaal bu bees bi, Paab Caw, biral na ay ndawam keroog ca alxames...

NJAAM GU YEES FA ARAABI SAWDIT

Xoqatal ak metital ya amoon ca jamonoy njaam ga dekkiwaat na fa Araabi Sawdit....

MALIKUNDAA : KËRUG MBËJ GU BEES

Senelec taxawal na kërug mbëj fa Malikundaa. Loolii dina tax ba dawaanu mbëj mi...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI JÀLLALE NAÑU ÑEENTI SÉMBUW ÀTTE

Démb ci àjjuma ji, Ngombalaan gi wote na ñeenti sémbi àtte. Ñuy i àtte...

SOWAAL : JÀPP NAÑU GAAL GU YABOON LU ËPP 300I MBËKK-KAT

Ndawi duwaan yi nekke Fimla jàpp nañ ag gaal gu naroon mbëkki. Gaal googu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI(13/3/2025)

NDOGAL YI ELIMAANU JËWRIÑ YI JËL ÑEEL MBIRUM SUUF SI Démb, ci àllarba ji lañu...

NDAJEM JËWRIÑ YI (13/3/2025)

Nees ko tàmm a defe, ayu-bés bu jot, amal nañu ndajem jëwriñ yi démb...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...