Xibaar

SONACOS SIGICOOR : JËWRIÑ MABUUBA XOOLI WOON NA NDEFAR GI

Jëwriñu mbey mi, Sëñ Mabuuba Jaañ, amaloon na tukkib nemmeeku fa Sigicoor. Li mu...

FMI DËGGAL NA ËTTUB CETTANTAL GI

RFI, saabalukaay Farãs bi, moo siiwal xibaar bi. Ci li mu fésal, FMI dafa...

SEN BU APR WOOTE NA BÉSUB ÑAXTU

Làngug pólitig gu APR (Alliance Pour la République) woote na bésub ñaxtu keroog àllarba...

UBBITEG KOPPEY LIGGÉEY AK JÀPPALANTE YI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ma nga woon Kumpentum, fa diiwaanu Tàmbaakundaa. Ci àjjumay...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/3/2025)

COOWAL AMNISTI BI Coppiteg amnisti bi dépitey Pastef yi namm a wotelu ca Ngomblaan ga...

JËWRIÑ ABDURAHMAAN SAAR AK JËWRIÑ SÉEX DIBAA DALAL NAÑ AY NDAWI FMI

FMI yabalati na ay ndawam fi Senegal ngir ñu waxtaan ci mbirum koom-koom ak...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (18/3/2025)

COOWAL MUURAAY YI CI LEKOOL BI Coowal muuraay yi ci lekool bi dekkiwaat na. Démb...

MBËKK MI : JÀPP NAÑU MEERU JONWAAR BI

Laasana Saar, meeru Jonwaar, ak yeneen juróom-benni nit ñu ngi ci loxoy Yoon jamono...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...