Xibaar

TÀGGE : GASTÕ MBENG FAATU NA

GASTÕ SAALIF MBENG, tëggkatu làmb bi, moo génn àddina tey ci àllarba ji, 1eelu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/4/2024)

CÀKKUTEEFU KURÉLI MAXEJJ YI Yenn ci kuréli maxejj yi, tudde seen bopp Sursaut citoyen et...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (25/04/2024)

ÑETTEELU NDAJEM JËWRIÑ Démb ci àllarba ji la Njiitu réew mi Basiiru Jomaay Jaxaar Fay...

ABDURAHMAAN JUUF MA NGA CA JÀNGUNE YA

Ginnaaw ba ñu leen takkalee seen i ndomboy-tànk, jëwriñi Càmm gu bees gi sóobu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/4/2024)

SONKO SANT NA JËWRIÑ YA WOON ÑU DELLOO DAAMARI NGUUR GI Jëwriñ yu nekkoon ci...

FUTBAL : LIGUE DES CHAMPIONS, EUROPA LEAGUE AK CONFERENCE LEAGUE

Barki-démb, démb ak tey lañ doon amal joŋantey kaar-dë-finaal Ligue des champions yi, Europa...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (18/4/2024)

ÑAAREELU NDAJEM JËWRIÑ Démb ci àllarba ji la Njiitu réew mi Basiiru Jomaay Fay doon...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...