Xibaar

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16/4/2024)

SAYTUKAT YI CI GOX YEEK GOX-GOXAAT YI BANK NAÑ SEEN I LOXO Sàndikaa bi ëmb...

SÀMPIYONAA ALMAAÑ : BAYER LEVERKUSEN JËL NA KO !

Xabi Alonso ak gaayam yi def nañ ko. Dugal nañ Bayer Leverkusen ci mboorum...

BOROOM JAKARTAA BI FAATU FA CAALI

As góor su tollu ci 25i at, daan dawal móto jakartaa, lees fekk neewam...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/4/2024)

NJABOOTU LÀMB DAL NA CI KOW BIRAM SULÉY JÓOB  Bi jëwriñ jii di Biram Suléy...

RUWÀNDAA : PÀTTALIKUG 30EELU ATUM FAAGAAGALUG TUTSI YI

Atum ren ji mooy tollook fanweereelu at ginnaaw bi faagaagalug Tustsi amee ba léegi....

SÀNDARM BI AKSIDÀNTE FA KÉEDUGU

Ab sàndarm moo ñàkk bakkanam fa diiwaanu Kéedugu. Dafa def aksidaŋ ci tali Salemata...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/4/2024)

USMAAN SONKO JËL NA LENGEY MAGUM JËWRIÑ YI Usmaan Sonko, magum jëwriñ yi ci càmm...

CORED ÀRTU NA BASIIR FOFANA MU ITV

Kàddu ya BacNsiir Fofana yékkati woon fa Itv mujj naa jur coow. Ndax, kàddu...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...