Xibaar

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/5/2024)

ÑËWUG KAGAME FI SENEGAAL Póol Kagame, Njiitu réewum Ruwàndaa li, moo ngi woon fi réew...

NJIITU RÉEW MI DALAL NA PÓOL KAGAME, NJIITU RÉEWUM RUWÀNDAA

Njiitu Réewum Ruwàndaa, Póol Kagame, teersi na Ndakaaru, tey ci gaawu gi, fa naawub...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (9/5/2024)

BÉSUB MÀGGALU “ASCENSION” Tey, ci alxames ji, yemoo ak juróom-ñeenti fan ci weeru me, mooy...

LIGUE DES CHAMPIONS : DORTMUND AK REAL MADRID ÑOOY DAJE FINAAL

Démb, ci àllarba ji, lees doon amal ñaareelu joŋantey demi-finaali "Ligue des champions" bi,...

KÀDDUY ELIMAANU JËWRIÑ YI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, yékkateeti nay kàddu jëmale ci Saa-Senegaal yi. Wile yoon...

ËMMA SEEN DAAN NA SAA-CEES !

Démb ci dibéer ji, 5i fan ci weeru Me 2024, la doomu Pikin ji,...

MBEY MI : MAGUM JËWRIÑ YI JËL NA CI NDOGAL YU BEES

Magum jëwriñ yi, Usmaan Sonko, jël na ndogal yu bees ñeel kàmpaañu mbey mi...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (2/5/2024)

TUXAL NAÑU BÉSU NDAJEM JËWRIÑ YI Ndajem jëwriñ yee ngi daan am àllarba ju nekk....

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...