Xibaar

LAMIN JÀLLO (NJIITUL TEKKI) DINA JÉEM A NEENAL DEKKARE MAKI SÀLL BI

Mamadu Lamin Jàllo mi jiite pàrti pólitig bii di Tekki ñaawlu na dekkare bi...

PEREFE BU NDAKAARU AAYE NA MÓTO YI ÑU DAW BIIR NDAKAARU

Perefe bu ndakaaru bi, Serif Muhammadu Bolondeŋ Njaay, génne na ab yégle buy aaye...

SÉMBUB ÀTTE BIY DÀQ WOTE YI : AJANDI NAÑ JOTAAY BI

Njiitul Ngomblaan gi dàqandi na jotaay bi, ginnaaw bi dépitey Yewwi Askan Wi ak...

DOGATI NAÑ SIÑAALU WALFADJRI !

Bees sukkandikoo ci Seex Ñas, doomu Siidi Lamin Ñas mi jiite Walfadjri, Nguur gi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/2/2024)

WAAJTAAYU KÀMPAAÑI WOTEY 2024 YI Ay fan yu néew ñoo des ngir kàmpaañ bi tàmbali....

PDS AM NA NDIISOG LUÑÑUTOOM : LÉEGI NAG ?

Tey ci àllarba ji la Ngomblaan gi door ndiisog luññutu gi ñeel anam yi...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (30/01/2024)

CAN KODDIWAAR 2024 : SENEGAAL TOOG NA Démb la Senegaal doon joŋante ak Koddiwaar ñeel 1/8...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...