Xibaar

37eelu NDAJEM BENNOOG AFRIG

37eelu Ndajem Bennoog Afrig, ñu gën koo miis ci UA (Union Africaine), mi ngi...

AMNESTI : MAKI XÀLL NA YOONU JÀMMOO

Fan yii, ñoo ngi soow mbirum amnesti (mbaale) bi Njiitu réew mi junjoon. Amnesti...

AES DËGGAL NA BOPPAM

Waa AES (Alliance des Etats du Sahel) fasul yéene dellu ginnaaw ci génn bi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (14/2/2024)

DÀQATI NAÑU LAYOOB SÉYDINA UMAR TURE AK SÉEX YÉRIM SEKK Coow li dox diggante ki...

LËKKATOO “DIOMAYE PRÉSIDENT” DINA WÉYAL XEEX BI

Démb ci dibéer ji la lëkkatoo gii di “ Diomaye Président” doon amal ndajem...

CAN 2024 KODDIWAAR : TËGG SA CAN, JËL KO !

Koddiwaar mooy waaga CAN 2024 bees doon amale biir dëkkam. Mu doon dajeek Niseriyaa...

UE MI NGI GËTËN MAKI SÀLL

UE (Union Européenne) waxatinaak Maki Sàll. Ginnaaw bi mu njëkkee ñaawlu ajug wote yi,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/2/2024)

YËNGU-YËNGU YI GINNAAW NDÀQUG WOTE YI Ginnaaw dal gi nu tàmbali woon a seetlu ci...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...