Xibaar

CHAN 2023

Chan 2023 bi door na keroog àjjuma 13i fan ci saŋwiye 2023. Wile yoon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM

WURE (FUTBAL) Gaynde Senegaal yu ndaw yi noppi nañoo waajal Chan bi. Tey ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (gaawu 7 saŋwiyee 2023)

PÓLITIG Tuuma ji ëttub cettantal gi tegoon ñenn ciy jëwriñ ak i DAGE ñeel koppar...

DOOMU GAYNDE, GAYNDE LAY DOON !

Saa-senegaal bii di Paap Mataar Saar, ab wurekat la, nekk ndaw, tollu ci fukki...

Li gën a fés ci xibaari bés bi Alxames 5 saawiye 2023

PÓLITIG Leerali Usmaan Sonko ñeel ñaxtuy ndongoy Sigicoor yi Ci ndajem-waxtaan mu mu doon amal tey...

CONCU BU DIIS BI

Wolof nee na : "concu, boroom rekk a ko àttan". Kon, ndax jaadu na...

TUUBA, KAARAANGE GAA NGA CA LOXOY TAKK-DER YA

Tuuba, dëkk bu sell ba, baat ba benn la. Lu bari lañuy doxal ca...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...