Xibaar

KAN MOOY… IDIRIISA SEKK ?

Maaraa la ko ay jegeñaaleem di woowe, doomi-réew mi naan ko Idi. Taskati xibaar yi ñoom, Ndaamal-Kajoor lañu...

KAN MOOY…MAKI SÀLL ?

Ci Baatu Majaw Njaay Aw askan, bala moo tànn njiitam, war naa seet bu baax...

Bàlla Gay-Móodu Lóo : ñaar ci dara

Làmbu démb ak ju tey jeeka wuute ! Ndege, démb, bu nawet bi wàccaan, ci...

XËCC BU DAŊEE DAGG !

Nimbir yiy doxe diggante nguur geek kujje gi bi Màkki Sáll toogee ci jal...

DIBÉERU WËLBATI

Cialtine jii la njiitu réew mi doon jébbal askan wi saxaar gi ñu duppe...

XËT YI MUJJ

CDEPS MI NGI SÀKKU CI NJIITU RÉEW MI MU « YEESAL WAXTAAN WI AK SAABALKAT YI »

Conseil des diffuseurs et éditeurs de presse du Sénégal (CDEPS) dafa doon amal, tay...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/1/2025)

USMAAN SONKO : DUGG NAÑU CI JAMONO JOJ, BAALE JEEX NA Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko,...

NJËLBEENI NDOGALI DONALD TRUMP

Démb lees doon amal palug Donald Trump niki ñeen-fukk ak juróom-ñaareelu (47eelu) Njiitu Réewum...