Xibaar

LI GËN A FËS CI XIBAARI BES BI Talaata 25 oktoobar 2022

YOKKUTEG NJËGU DUGUB BI  Jamono jii, askan waa ngiy jooy dund biy wéy di yokk....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 22 OKTOOBAR 2022)

PÓLITIG Dépite ya fare ca Wallu Senegaal, ña ngay sàkku ci njiitu jëwriñ ji Aamadu...

LI GЁN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Alxames 20 oktoobar 2022

XIBAARI BITIM-RÉEW Fitna sa ca Càdd Lu tollu ci 60i nit ak lu teg ñoo ñàkk...

“WAT GAAL AK YËGOO…” Jëwriñ Aliw Sow amal na tukkib nemmeeku ñeel artist yi

Ginnaaw bi ñu ko tabbee yees ci wàllum mbatiit ak moomeel, Aliw Sow door...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 17 oktoobar 2022

PÓLITIG Way-politig yi jublooti nañ ci wotey 2024 yi. Bu dee làngug Nguur gi, Njiitu...

TЁRALINU KURÉL GU YEES GII DI “REELS”

Démb ci Gaawu bi 15 oktoobar la ñii di waa Yewwi Askan Wi doon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI GAAWU 15 OKTOOBAR 2022

PÓLITIG Ni ñu ko junjee woon ginnaaw palum depite yi, kujje gi taxawal na kurél...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...