Xibaar

LI GËN A FËS CI XIBAARI BES BI Alxames 10 nowàmbar 2022

Mbirum pasug ngànnaay gu 45i miliyaar yi Dépitey Yewwi Askan Wi (YAW), nee nañ du...

WÀÑÑITEG PAYOORUG LEKKOOL BI

Ginnaaw ndaje mu tembere mi ñu amaloon ngir jël ay matuwaay ci yokkuteg dund...

NJËGU DUND BI NJIITU RÉEW MI, MAKI SÀLL, JËL NA 11i NDOGAL

Ci gaawu gii weesu, 5i fan ci nowàmbar, lees doon amal am ndaje ngir...

XEW-XEWI NDÉGLUG USMAAN SONKO GI

Ci alxames jii weesu, ñetti fan ci weeru nowàmbar, la kii di Njiital PASTEF...

SÉMBUB SOROJ BU GRANDE-TORTUE Senegaal dina taxan 20 000i miliyaar ci diirub 30i at  

Bu liggéeyub soroj bi tàmbalee, Senegaal dina taxan, ci diirub 30i at, 20 000i...

ÑU SELL ÑA

Talaatay démb ji, 1 nowàmbar 2022, la waa jàngu bi doon màggal seen waliyu...

« JÀMM A GËN 3e MANDAT »

Way-moomeel yee ngi sàkku ci Njiitu réew mi, Maki Sàll, mu bañ a laaj...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 31 Oktoobar 2022

PÓLITIG Lawax yi jëm ci wotey 2024 yee ngi gën dee yokku. Démb ci dibéer...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...